Lrc Player

Jammu Africa

Ismaël Lo
[05:03.05]·Synced by Guest·
This lyric sheet isn't paired with a song yet, so lines are shown but won't sync or seek.

[00:13.22] Afrika a a a Afrika mon Afrique

[00:37.40] Sama gent gi maa ngi ñaan Yalla wonma ko bala may ñibbi barsaq

[00:42.72] Ma ne bes du ñakk ci bes yi Afrika don benn reew

[00:49.08] D'ici ou d'ailleurs nous somm' des enfants d'Afrique

[00:54.40] Mêm' si le ciel tombait luttons pour la paix

[01:01.30] Kon jammu Afrika moom lay ñaan

[01:06.62] Mané jammu Afrika mooy suñu natange

[01:24.93] Afrika a a a Afrika a a

[01:37.42] Afrika a a a Afrika mon Afrique

[01:49.37] Yow mi nekka bittim reew man mi Lô maa ngi lay ñaan

[01:54.42] Ak loo fa meun ta am ak noo fa meun ta mel bul fatte Afrika

[02:01.32] Ici ou ailleurs la paix prix du bonheur

[02:06.64] Mêm' si le ciel pleurait luttons pour nos frères

[02:18.86] Kon jammu Afrika moom lay ñaan

[02:19.93] Mané jammu Afrika mooy suñu natange

[02:37.18] Afrika a a a Afrika a a

[03:02.43] Afrika a a a Afrika mon Afrique

[04:01.64] Onon bibbe Afrika ngimode, ngimode liggo-den leydi men

[04:10.96] Ngaccen hasi daagal yoo Alla suren e musibaadi

[04:19.72] Yoo Alla addu jam to Ruanda

[04:22.91] Yoo Alla addu jam to Burundi

[04:25.81] Yoo Alla addu jam to Casamans

[04:28.74] Lawol Mbignona yee